Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 7:30 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 7:30 in Kàddug Yàlla gi

30 Ci loxol boppam lay dindee sarax bi ñuy def saraxu sawara, ñeel Aji Sax ji. Day indi nebbon bi, boole kook dënn bi, dënn bi di sarax bu ñuy yékkati, jébbal Aji Sax ji.
Sarxalkat yi 7 in Kàddug Yàlla gi