Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 7

Sarxalkat yi 7:3-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Nebbon ji jépp lañuy sarxal: calgeen bi, nebbon bi sàng yérey biir yi,
4ak ñaari dëmbéen yi ànd ak seen nebbon ca kaw, jàpp ca fàllare ja, ak bàjjo bi ci res wi te ñu di ko booleek dëmbéen yi, génne ko.

Read Sarxalkat yi 7Sarxalkat yi 7
Compare Sarxalkat yi 7:3-4Sarxalkat yi 7:3-4