Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 7:3-4 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 7:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Nebbon ji jépp lañuy sarxal: calgeen bi, nebbon bi sàng yérey biir yi,
4 ak ñaari dëmbéen yi ànd ak seen nebbon ca kaw, jàpp ca fàllare ja, ak bàjjo bi ci res wi te ñu di ko booleek dëmbéen yi, génne ko.
Sarxalkat yi 7 in Kàddug Yàlla gi