Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 4

Sarxalkat yi 4:27-28

Help us?
Click on verse(s) to share them!
27«Su dee kenn ci baadoolo yee moy lenn ci santaaney Aji Sax ji, ba def lenn lu warul te du teyeefam, mu dig tooñam,
28bu nemmikoo bàkkaar bi mu def rekk, na sarxe aw bëy wu jigéen wu amul sikk, ndax bàkkaar bi mu def.

Read Sarxalkat yi 4Sarxalkat yi 4
Compare Sarxalkat yi 4:27-28Sarxalkat yi 4:27-28