Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 4:27-28 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 4:27-28 in Kàddug Yàlla gi

27 «Su dee kenn ci baadoolo yee moy lenn ci santaaney Aji Sax ji, ba def lenn lu warul te du teyeefam, mu dig tooñam,
28 bu nemmikoo bàkkaar bi mu def rekk, na sarxe aw bëy wu jigéen wu amul sikk, ndax bàkkaar bi mu def.
Sarxalkat yi 4 in Kàddug Yàlla gi