Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 4

Sarxalkat yi 4:21-22

Help us?
Click on verse(s) to share them!
21Na génne yëkk wi dal bi, taal ko, na muy taale yëkk wi ñu jëkka wax. Saraxu póotum bàkkaaru mbooloo mi la.
22«Su fekkee ne kilifa moo moy lenn ci santaaney Yàllaam Aji Sax ji, ba def lenn lu warul te du teyeefam, mu dig tooñam,

Read Sarxalkat yi 4Sarxalkat yi 4
Compare Sarxalkat yi 4:21-22Sarxalkat yi 4:21-22