Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 4:21-22 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 4:21-22 in Kàddug Yàlla gi

21 Na génne yëkk wi dal bi, taal ko, na muy taale yëkk wi ñu jëkka wax. Saraxu póotum bàkkaaru mbooloo mi la.
22 «Su fekkee ne kilifa moo moy lenn ci santaaney Yàllaam Aji Sax ji, ba def lenn lu warul te du teyeefam, mu dig tooñam,
Sarxalkat yi 4 in Kàddug Yàlla gi