Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 26

Sarxalkat yi 26:6-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
6«Maay baaxee réew mi jàmm it, ba bu ngeen tëddee kenn du leen tiital. Maay jële rab wu aay ci réew mi, te saamar du jóg, dal ci seenum réew.
7Kon dingeen dàq seeni noon, saamar ba dal, ñu daanu fi seen kanam.

Read Sarxalkat yi 26Sarxalkat yi 26
Compare Sarxalkat yi 26:6-7Sarxalkat yi 26:6-7