Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 26:6-7 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 26:6-7 in Kàddug Yàlla gi

6 «Maay baaxee réew mi jàmm it, ba bu ngeen tëddee kenn du leen tiital. Maay jële rab wu aay ci réew mi, te saamar du jóg, dal ci seenum réew.
7 Kon dingeen dàq seeni noon, saamar ba dal, ñu daanu fi seen kanam.
Sarxalkat yi 26 in Kàddug Yàlla gi