Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 26

Sarxalkat yi 26:13-14

Help us?
Click on verse(s) to share them!
13Man Aji Sax ji maay seen Yàlla ji leen génne réewum Misra, ngeen noppee doon seeni jaam; maa dog seen buumi njaam, siggil leen.
14«Waaye bu ngeen ma déggalul te baña jëfe sama santaane yooyu yépp,

Read Sarxalkat yi 26Sarxalkat yi 26
Compare Sarxalkat yi 26:13-14Sarxalkat yi 26:13-14