Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 26:13-14 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 26:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Man Aji Sax ji maay seen Yàlla ji leen génne réewum Misra, ngeen noppee doon seeni jaam; maa dog seen buumi njaam, siggil leen.
14 «Waaye bu ngeen ma déggalul te baña jëfe sama santaane yooyu yépp,
Sarxalkat yi 26 in Kàddug Yàlla gi