Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 25

Sarxalkat yi 25:30

Help us?
Click on verse(s) to share them!
30Su ñu ko jotaatul ba njaay ma am atum lëmm, dëkkuwaay boobu ci biir dëkk bu mag ba ñu wëralee tata day wel fàww, ñeel ka ko jënd, mook ku askanoo ci moom. Du lees di delloo ci atum Yiwiku.

Read Sarxalkat yi 25Sarxalkat yi 25
Compare Sarxalkat yi 25:30Sarxalkat yi 25:30