Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 25:30 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 25:30 in Kàddug Yàlla gi

30 Su ñu ko jotaatul ba njaay ma am atum lëmm, dëkkuwaay boobu ci biir dëkk bu mag ba ñu wëralee tata day wel fàww, ñeel ka ko jënd, mook ku askanoo ci moom. Du lees di delloo ci atum Yiwiku.
Sarxalkat yi 25 in Kàddug Yàlla gi