Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 25

Sarxalkat yi 25:13-14

Help us?
Click on verse(s) to share them!
13«Atum Yiwiku moomu ci ngeen di delloo ku nekk suufam.
14Bu ngeen di jaay seen waa réew suuf nag mbaa ngeen di jënde suuf ci seen waa réew, buleen di naxante.

Read Sarxalkat yi 25Sarxalkat yi 25
Compare Sarxalkat yi 25:13-14Sarxalkat yi 25:13-14