Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 25:13-14 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 25:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 «Atum Yiwiku moomu ci ngeen di delloo ku nekk suufam.
14 Bu ngeen di jaay seen waa réew suuf nag mbaa ngeen di jënde suuf ci seen waa réew, buleen di naxante.
Sarxalkat yi 25 in Kàddug Yàlla gi