Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 24

Sarxalkat yi 24:23

Help us?
Click on verse(s) to share them!
23Ci kaw loolu Musaa wax ko bànni Israyil, ñu génne dal ba waa ja ñàkke Yàlla kersa, dóor ko ay doj, ba mu dee. Kon li bànni Israyil def mooy li Aji Sax ji santoon Musaa rekk.

Read Sarxalkat yi 24Sarxalkat yi 24
Compare Sarxalkat yi 24:23Sarxalkat yi 24:23