Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 24:23 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 24:23 in Kàddug Yàlla gi

23 Ci kaw loolu Musaa wax ko bànni Israyil, ñu génne dal ba waa ja ñàkke Yàlla kersa, dóor ko ay doj, ba mu dee. Kon li bànni Israyil def mooy li Aji Sax ji santoon Musaa rekk.
Sarxalkat yi 24 in Kàddug Yàlla gi