Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 24

Sarxalkat yi 24:12-14

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Ñu tëj waa ja, ba xam lu Aji Sax ji namm ci moom.
13Ci kaw loolu Aji Sax ji wax Musaa ne ko:
14«Génneel dal bi ki may wax lu ñaaw, man Yàlla, te na mboolem ku ci dégg teg loxoom ci kaw boppam, ba noppi mbooloo mépp dóor koy doj, ba mu dee.

Read Sarxalkat yi 24Sarxalkat yi 24
Compare Sarxalkat yi 24:12-14Sarxalkat yi 24:12-14