Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 24:12-14 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 24:12-14 in Kàddug Yàlla gi

12 Ñu tëj waa ja, ba xam lu Aji Sax ji namm ci moom.
13 Ci kaw loolu Aji Sax ji wax Musaa ne ko:
14 «Génneel dal bi ki may wax lu ñaaw, man Yàlla, te na mboolem ku ci dégg teg loxoom ci kaw boppam, ba noppi mbooloo mépp dóor koy doj, ba mu dee.
Sarxalkat yi 24 in Kàddug Yàlla gi