Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 22

Sarxalkat yi 22:14-15

Help us?
Click on verse(s) to share them!
14Gannaaw loolu képp ku bokkul ci waa kër sarxalkat yi, bu lekkee ci sarax su sell te du teyeefam, na dolli ca njégu sarax sa juróomeelu céru njég ga, delloo ko sarxalkat bi.
15Te itam bu sarxalkat yi bàyyi bànni Israyil di teddadil sarax yu sell yi ñu jagleel Aji Sax ji.

Read Sarxalkat yi 22Sarxalkat yi 22
Compare Sarxalkat yi 22:14-15Sarxalkat yi 22:14-15