Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 19

Sarxalkat yi 19:5-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5«Bu ngeen dee rendil Aji Sax ji saraxas cant ci biir jàmm, sarxal-leen ko ni mu ware, ndax ñu nangul leen.
6Ca bés ba ñu ko sarxale lees koy lekk, mbaa ca ëllëg sa; lu ca des ba ca gannaaw ëllëg sa dees koy lakk, ba mu dib dóom.

Read Sarxalkat yi 19Sarxalkat yi 19
Compare Sarxalkat yi 19:5-6Sarxalkat yi 19:5-6