Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 19:5-6 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 19:5-6 in Kàddug Yàlla gi

5 «Bu ngeen dee rendil Aji Sax ji saraxas cant ci biir jàmm, sarxal-leen ko ni mu ware, ndax ñu nangul leen.
6 Ca bés ba ñu ko sarxale lees koy lekk, mbaa ca ëllëg sa; lu ca des ba ca gannaaw ëllëg sa dees koy lakk, ba mu dib dóom.
Sarxalkat yi 19 in Kàddug Yàlla gi