Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 16

Sarxalkat yi 16:31-32

Help us?
Click on verse(s) to share them!
31Na doon seen bés bu ngeen di nopplu doŋŋ, ngeen war cee toroxlu. Dogal la bu sax dàkk.
32«Sarxalkat bi ñu fal nag, solal ko, jox ko sañ-sañu sarxalkat bu mag, mu wuutu baayam, na def saraxu njotlaay gi. Na sol yére yu sell yooyu di yi ñu ràbbe wëñ gu ëccu ba sew,

Read Sarxalkat yi 16Sarxalkat yi 16
Compare Sarxalkat yi 16:31-32Sarxalkat yi 16:31-32