Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 14

Sarxalkat yi 14:33-35

Help us?
Click on verse(s) to share them!
33Aji Sax ji wax na Musaa ak Aaróona ne leen:
34«Bu ngeen demee ca réewu Kanaan ga ma leen jox muy seen moomeel, bu ma tegee liir wuy law ba xuural ab néeg foofa ca seen réewum bopp,
35boroom néeg bi dafa wara dem ca sarxalkat ba ne ko: “Lu mel ni aw liir laa gis sama néeg.”

Read Sarxalkat yi 14Sarxalkat yi 14
Compare Sarxalkat yi 14:33-35Sarxalkat yi 14:33-35