Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 14:33-35 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 14:33-35 in Kàddug Yàlla gi

33 Aji Sax ji wax na Musaa ak Aaróona ne leen:
34 «Bu ngeen demee ca réewu Kanaan ga ma leen jox muy seen moomeel, bu ma tegee liir wuy law ba xuural ab néeg foofa ca seen réewum bopp,
35 boroom néeg bi dafa wara dem ca sarxalkat ba ne ko: “Lu mel ni aw liir laa gis sama néeg.”
Sarxalkat yi 14 in Kàddug Yàlla gi