Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - ROOM - ROOM 15

ROOM 15:30-31

Help us?
Click on verse(s) to share them!
30Gannaaw loolu bokk yi, maa ngi leen di ñaan ci turu sunu Boroom Yeesu Kirist ak ci bëggante, gi Xelu Yàlla mi def ci nun, ngeen defal ma lii: àndleen ak man, nu tuur sunu ñaq ci ñaan Yàlla.
31Ñaanal-leen ma, ngir ma mucc ci ñi gëmul ci waa Yude; te it gaayi Yàlla yu sell yu nekk ci Yerusalem nangu ndimbal, li ma leen di yóbbul.

Read ROOM 15ROOM 15
Compare ROOM 15:30-31ROOM 15:30-31