Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - JËF YA - JËF YA 1

JËF YA 1:23-24

Help us?
Click on verse(s) to share them!
23Bi ko Piyeer waxee, ñu tudd ñaar: Yuusufa, mi ñu dippee Barsabas te di ko dàkkentale Yustus, moom ak Macas.
24Ñu ñaan ci Yàlla ne: «Boroom bi, yaw mi xam xolu nit ñépp, won nu ki nga tànn ci ñaar ñii,

Read JËF YA 1JËF YA 1
Compare JËF YA 1:23-24JËF YA 1:23-24