Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 1:23-24 in Wolof

Help us?

JËF YA 1:23-24 in Téereb Injiil

23 Bi ko Piyeer waxee, ñu tudd ñaar: Yuusufa, mi ñu dippee Barsabas te di ko dàkkentale Yustus, moom ak Macas.
24 Ñu ñaan ci Yàlla ne: «Boroom bi, yaw mi xam xolu nit ñépp, won nu ki nga tànn ci ñaar ñii,
JËF YA 1 in Téereb Injiil

Jëf ya 1:23-24 in Kàddug Yàlla gi

23 Ci kaw loolu ñu tudd ñaar: Yuusufa, mi ñu dippee Barsabas, te ñu di ko wax Yustus itam, ak Maccas.
24 Ñu daldi ñaan ne: «Boroom bi, yaw mi xam xolu ñépp, won nu ki nga tànn ci ñaar ñii,
Jëf ya 1 in Kàddug Yàlla gi