Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Jëf ya - Jëf ya 1

Jëf ya 1:23-24

Help us?
Click on verse(s) to share them!
23Ci kaw loolu ñu tudd ñaar: Yuusufa, mi ñu dippee Barsabas, te ñu di ko wax Yustus itam, ak Maccas.
24Ñu daldi ñaan ne: «Boroom bi, yaw mi xam xolu ñépp, won nu ki nga tànn ci ñaar ñii,

Read Jëf ya 1Jëf ya 1
Compare Jëf ya 1:23-24Jëf ya 1:23-24