Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - JËF YA - JËF YA 13

JËF YA 13:16-17

Help us?
Click on verse(s) to share them!
16Noonu Pool jóg, tàllal loxoom ne leen: «Yéen bokki Israyil ak yéen ñi ragal Yàlla, dégluleen!
17Yàllay bànni Israyil tànn na sunuy maam, di yokk xeet wa, bi ñuy ganeyaan ci Misra; ba noppi mu génne leen fa ak kàttanu loxoom.

Read JËF YA 13JËF YA 13
Compare JËF YA 13:16-17JËF YA 13:16-17