Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 13:16-17 in Wolof

Help us?

JËF YA 13:16-17 in Téereb Injiil

16 Noonu Pool jóg, tàllal loxoom ne leen: «Yéen bokki Israyil ak yéen ñi ragal Yàlla, dégluleen!
17 Yàllay bànni Israyil tànn na sunuy maam, di yokk xeet wa, bi ñuy ganeyaan ci Misra; ba noppi mu génne leen fa ak kàttanu loxoom.
JËF YA 13 in Téereb Injiil

Jëf ya 13:16-17 in Kàddug Yàlla gi

16 Póol jóg, tàllal loxoom, nee leen: «Yeen bokki Israyil ak yeen jaamburi ragalkati Yàlla yi, dégluleen!
17 Yàllay bànni Israyil jii moo tànnoon sunuy maam, moo yaatal xeet wi, ba ñuy ganeyaan ca Misra; moo leen fa génnee kàttanu loxoom.
Jëf ya 13 in Kàddug Yàlla gi