Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Galasi - Galasi 6

Galasi 6:7-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Bu leen lenn nax; Yàlla deesu ko foontoo. Nit ki, li mu ji, moom lay góob.
8Ku jiyal bànneexu bakkanam, ci bànneexu bakkanam lay jële ngóobum yàqute; ku jiyal Noowug Yàlla, ci Noo gi ngay góobe texe gu sax dàkk.
9Bunu tàyyi ci def lu baax, nde bu jotee rekk nooy góob, ndegam yoqiwunu.

Read Galasi 6Galasi 6
Compare Galasi 6:7-9Galasi 6:7-9