Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - YOWAANA - YOWAANA 3

YOWAANA 3:16-17

Help us?
Click on verse(s) to share them!
16Ndaxte Yàlla dafa bëgg àddina, ba joxe jenn Doomam ji mu am kepp, ngir képp ku ko gëm am dund gu dul jeex te doo sànku mukk.
17Yàlla yónniwul Doomam ci àddina ngir mu daan nit ñi, waaye ngir musal leen.

Read YOWAANA 3YOWAANA 3
Compare YOWAANA 3:16-17YOWAANA 3:16-17