Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Yawut ya - Yawut ya 11

Yawut ya 11:7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Ngëm la Nóoyin dégge waxyub Yàlla bu jëm ci lu kenn gisagul woon, te ragal Yàlla la sàkke gaal, ngir musal njabootam. Ngëmam it la tiiñale àddina, ba ab céram di njub gi ngëm di maye.

Read Yawut ya 11Yawut ya 11
Compare Yawut ya 11:7Yawut ya 11:7