Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Yanqóoba - Yanqóoba 2

Yanqóoba 2:3-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3su ngeen seetloo boroom col gu jekk gi, ne ko: «Toogeel fii, moo baax ci yaw,» te ne néew-ji-doole ji: «Yaw, taxaweel nee, mbaa nga toog fii sama tànki toogu, fi suuf,»
4su boobaa xanaa du yeena ngi gënaatle ci seen biir, tey àttee ay mébét yu bon?
5Bokk yi, soppe yi, dégluleen. Xanaa du Yàlla moo taamu ñi àddina jàppe ñu néew doole, ngir ñu barele ngëm, boole ci jagoo nguur, gi Yàlla dig ñi ko sopp?
6Yeen nag ngeen di teddadil néew doole yi! Xanaa du boroom alal yi ñoo leen di noggatu, di leen diri ba fa mbaxana dee benn?

Read Yanqóoba 2Yanqóoba 2
Compare Yanqóoba 2:3-6Yanqóoba 2:3-6