Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 22

Sarxalkat yi 22:11

Help us?
Click on verse(s) to share them!
11Waaye su sarxalkat bi jëndee ab jaam ci xaalisam, jaam ba man na caa lekk. Jaam bu juddoo ci kër sarxalkat bi it man naa lekk ci ñamam woowu.

Read Sarxalkat yi 22Sarxalkat yi 22
Compare Sarxalkat yi 22:11Sarxalkat yi 22:11