Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 20

Sarxalkat yi 20:14-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
14Ku boole nit ak ndeyam jël leen jabar, def na lu bona bon. Dees leen di boole taal, lakk leen, moom ak jigéen ña, ndax mbon gu ni mel baña am ci seen biir.
15Góor gu tëdde mala dee rekk mooy àtteem, te mala ma it dees koy rey.
16Su jigéen jëmee ci mala mu mu doon, ba jaxasook moom, booleleen ku jigéen kaak mala ma, rey. Dee rekk mooy seen àtte, te ñooy gàddu seen bakkanu bopp.

Read Sarxalkat yi 20Sarxalkat yi 20
Compare Sarxalkat yi 20:14-16Sarxalkat yi 20:14-16