Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 15

Sarxalkat yi 15:24-26

Help us?
Click on verse(s) to share them!
24te ku ko dëkkoo, ba mbërëg taq ko, kooka sobewu na diiru juróom ñaari fan, te ka ko dëkkoo, lal bu mu tëdd sobewu na.
25«Kuy xëpp deret ay fan yu bare te du jamonoy baaxam, mbaa mu gis mbërëg mu wees àpp bi mu ko baaxoo gis, kooka sobewu na diiru fan yi muy xëpp. Day mel ni bu nekkee ci jamonoy baaxam.
26Lal bu mu tëdd ci diir bi muy xëpp yépp, day mel ni lalam bu ko fekk ci jamonoy baax te lépp lu mu toog day sobewu, ni bu nekkoon ci jamonoy baaxam.

Read Sarxalkat yi 15Sarxalkat yi 15
Compare Sarxalkat yi 15:24-26Sarxalkat yi 15:24-26