Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 14

Sarxalkat yi 14:45-47

Help us?
Click on verse(s) to share them!
45Néeg ba dees koy daane, boole doj yaak bant yaak banu raax ba bépp, génne ko dëkk bi, tuur ko fu setul.
46«Ku dugg biir néeg bi diiru fan yi mu tëje dina yendoo sobe ba jant so.
47Ku tëdd ca biir néeg ba war naa fóot ay yéreem te ku fa lekke it war naa fóot ay yéreem.

Read Sarxalkat yi 14Sarxalkat yi 14
Compare Sarxalkat yi 14:45-47Sarxalkat yi 14:45-47