Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 11

Sarxalkat yi 11:4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Yii ñuy lim, buleen ko lekk: mala muy duññ te we wi xarul, mbaa we wi xar te du duññ. Lu mel ni giléem, buleen ko lekk ndax day duññ, waaye we wi xarul. Daganul ci yeen.

Read Sarxalkat yi 11Sarxalkat yi 11
Compare Sarxalkat yi 11:4Sarxalkat yi 11:4