Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 29:1-3 in Wolof

Help us?

Sabóor 29:1-3 in Kàddug Yàlla gi

1 Muy kàddug Sabóor, ñeel Daawuda. Yeen goney Yàlla yi, seedeel-leen Aji Sax ji, seedeel-leen ko teddngaak doole,
2 seedeel-leen Aji Sax ji teddngay turam. Sujjóotal-leen Aji Sax ji, ki gànjaroo sellnga.
3 Aji Sax jeey àddu ca kaw ndox ma, Yàlla mu tedd maa dënu, Aji Sax jeey tiim ndox, mi ne màww.
Sabóor 29 in Kàddug Yàlla gi