Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kolos - Kolos 4

Kolos 4:5-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Jëfeleen xel mu rafet seen diggante ak aji gëmadi ñi ci biti, te jot gu ngeen am, fexeleen ba jariñoo ko.
6Na seen kàddu ànd ak yiw te am solo, te ngeen xam nu ngeen di tontoo ku nekk, tont li war.

Read Kolos 4Kolos 4
Compare Kolos 4:5-6Kolos 4:5-6