Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - JËF YA - JËF YA 1

JËF YA 1:15-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
15Ca bés yooya nag Piyeer taxaw ca digg bokk ya, di mbooloo mu tollu ni téeméer ak ñaar fukk.
16Mu ne leen: «Bokk yi, li Xel mu Sell mi waxoon ci Mbind mi jaarale ko ci gémmiñu Daawuda, fàww mu am. Waxoon na ci mbirum Yudaa, mi wommat ñi jàpp Yeesu

Read JËF YA 1JËF YA 1
Compare JËF YA 1:15-16JËF YA 1:15-16