Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - GALASI - GALASI 5

GALASI 5:20-22

Help us?
Click on verse(s) to share them!
20xërëm, luxus, noonoo ak xuloo, ñeetaane, xadar, diiroo mbagg, féewaloo ak xàjjaloo,
21kiñaan, màndite ak xawaare ak yeneen yu ni mel. Léegi nag maa ngi leen di artu, ni ma ko defe woon: ñiy jëfe noonu duñu am cér ci nguuru Yàlla.
22Waaye li Xelu Yàlla mi di meññ mooy: mbëggeel, mbég, jàmm, muñ, laabiir, mbaax, kóllëre,

Read GALASI 5GALASI 5
Compare GALASI 5:20-22GALASI 5:20-22