Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - 1.Buur ya - 1.Buur ya 2

1.Buur ya 2:34-35

Help us?
Click on verse(s) to share them!
34Ba loolu amee Benaya doomu Yoyada daldi dem jam Yowab, rey ko. Ñu suul ko ca këram ga ca màndiŋ ma.
35Gannaaw loolu Buur tabb Benaya doomu Yoyada ca boppu mbooloom xare ma, mu wuutu Yowab. Cadog sarxalkat ba, Buur tabb ko, mu wuutu Abiyatar.

Read 1.Buur ya 21.Buur ya 2
Compare 1.Buur ya 2:34-351.Buur ya 2:34-35