Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 23:14-15 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 23:14-15 in Kàddug Yàlla gi

14 Du mburu, du pepp mu ñu séndal, du pepp mu bees mu ngeen wara lekk, ba keroog bés boobu ngeen di indi seen saraxu Yàlla. Dogal a ngoogu, di lu leen war fàww, yeen ak seen askan, ak fépp fu ngeen dëkk.
15 «Bésub Noflaay ba ngeen di indi takku bele biy saraxu yékkati-jébbale, bés ba ca topp ngeen di dale waññ juróom ñaari ayi bés yu mat sëkk.
Sarxalkat yi 23 in Kàddug Yàlla gi