Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 22:5-8 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 22:5-8 in Kàddug Yàlla gi

5 mbaa mu laal yu sew-sewaan yiy dox ci suuf te di ko sobeel, mbaa mu laal nit ku ko sobeel ak lu sobe sa mana doon,
6 dina yendoo sobe sa ba jant so, te du lekk ci sarax yu sell yi ndare du dafa sangu.
7 Bu jant sowee nag set na, te man naa lekk ci sarax yu sell yi, ndax ñamam la.
8 Lu médd mbaa lu rab fàdd waru koo lekk, mu di ko sobeel. Maay Aji Sax ji.
Sarxalkat yi 22 in Kàddug Yàlla gi