Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 9:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 9:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Noon ya raaf, gental ba fàww. Yaa déjjati seeni dëkk, seenu askan fey.
8 Aji Sax jee sax dàkk, samp jalam ngir àtte.
9 Moom mooy àtte àddina cig njub, di dogalal xeet yi dëgg.
Sabóor 9 in Kàddug Yàlla gi