Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 9:13-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 9:13-16 in Kàddug Yàlla gi

13 Mooy topp nit bakkanu moroomam, di ko ba xel, te du fàtte yuuxi néew-ji-doole.
14 Éy Aji Sax ji, baaxe ma, gisal naqar wi ma bañ yi teg. Yaa may yékkatee fa bunti ndee,
15 ba ma siiwali sa woy yépp, fa buntu Siyoŋ, dëkk bu taaru ba, di bànneexoo sa wall gii!
16 Xeet yee tàbbi pax ma ñu gasoon, fakktaloo fiir ga ñu làqoon.
Sabóor 9 in Kàddug Yàlla gi