Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 90:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 90:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Yaay delloo doom aadama ci pënd, ne ko: «Yaw, doom aadama, dellul!»
4 Junniy at ci yaw daa gaaw ni démb ak tey, mbete waxtu yu néew ci wattub guddi.
5 Yaay buub nit, nelawal ko. Suba mu jebbi nim ñax,
Sabóor 90 in Kàddug Yàlla gi